
Secouriste Trés très engagé POUR LA CAUSE⛑️PURiste💚🕊 #Culers❤️💙 Je RT seulement pour RT Je partage l’info utile☺️
Senegal
Joined October 2018
- Tweets14.3K
- Following1.8K
- Followers1.9K
- Likes27.3K
Pinned Tweet
Senegaal ak monde entier béne Serigne bou gentle té tolloo ak âgeam mofi am mouy CAPITAINE😁❤️ Kouko wéddi indil s photo wala vidéo serigne 😂😂
🇸🇳 JOJ Dakar 2026 : Ndaje bi sunu ndaje la, ndam li sunu ndam la !
Sénégal dina dalal ndaw ñi jóge ci réew yu bari, ñu ñëw bokk ci Jeux Olympiques de la Jeunesse.
Maa ngi woo Senegaal yépp, nu won sunu gan yi sunu teraanga, dalal leen bu baax te dimbali leen ci li ñu soxla.
Xam naa ne ndaje bii dina indi ay jafe-jafe ci dem ak dikk, rawatina ci yoon yi. Waaye maa ngi leen ñaan, nu muñ te muñalante, ngir lépp jaar ci jàmm.
Sunu ndaw yi di sport, ñoom itam, nañu leen taxawal, dooleel leen te won leen ne réew mépp a ngi ci seen ginnaaw.
Na àddina sépp gis sunu teraanga, sunu bokk, ak sunu mbëggeel réew !
Ñun ñépp a bokk ci ndam li.
#Dakar2026 #JOJ2026 #Teranga
De #Bassirou_Diomaye_Faye
SecouRISQUE 🫀⛑️ retweeted
🔵...Il ne faut pas chercher loin, le responsable de l'abaissement de la note du Sénégal passe ses journées à la Place Soweto et la nuit à la Cité Keur Gorgui pour hourdir des manœuvres visant à bloquer l'économie du Sénégal.
Il m'arrivait de douter de son manque de patriotisme, mais ses deux ans à la Primature et sa posture actuelle m'ont définitivement convaincu de sa détestation du pays qui lui a donné son premier diplôme et son premier salaire.
Heureusement que le peuple sénégalais sait reconnaître les siens et ne manque pas de le leur faire connaître lors des élections.
Jumah Mou Barack aux Patriotes Républicains ❗️
😂😂😂😂 et y’en a qui se disent PATRIOTES parmi eux. Pour niom lou sén waadji bokoul rek dou baax ndyssane 😆
SecouRISQUE 🫀⛑️ retweeted
Maodo jambaar la waaye li nga daj si waaram wii nit mësuko si daj SY Demba te fanatisme taxul ñu diko wax
Amél ngama akkh😂
Lii chak jour meu rée ko😂😂
Lou tolni Président Idyrissa ngakoy wax Thialaka😭 respect amatufi koi
SecouRISQUE 🫀⛑️ retweeted
📍Loi de Finances Rectificative (LFR) 2026.
Pourquoi ai-je voté POUR en commission ?
Oooooooh jambaar jû mag douggouneu si pakh way😭 Eiywaay dougeulnagn sam boy bi si sectarisme way😭 MAD revient guyn boul souroukh





















