Topic◥🇸🇳 retweeted
Allez au fond des choses, mon professeur ! Sur quels points précis Pastef exprimait-il son désaccord ? Lesquels, exactement, et surtout, quelles positions ont-ils publiquement défendues sur chacun de ces points ?
LFR 2026: waxtaan wi dafay jëm kanam
Li nu wax ci njëlbéen ba tey leer na: duñu ko woté ni mu mel nii. Du ngir bañ, waaye ngir sas wi nu yor. Dépite yi, ngir saytu koppaaru askan wi lañu leen fal.
Li nu laaj xam nañu ko te yemoo na:
✅ Aar investissement public, jàng ak liggéey
✅ Bañ yokk njëgu esaans ak kuuraŋ ci kër yi ak ci entreprise yi
✅ Leeral bor bi, siiwal rappoor audit yu IGF ak Forvis Mazars
✅ Wàññi depaas yu nguur gi te saafal secteur parapublic bi
✅ Saytu bu dëgg ci fonds spéciaux yi
Topic◥🇸🇳 retweeted
Ce gougnafier est juste obsédé par le pouvoir.
Topic◥🇸🇳 retweeted
Le prof de maths a demandé ce qu'il y avait après 120 J'ai répondu « les penaltys»
Topic◥🇸🇳 retweeted
Soudainement, ils viennent de comprendre l’importance du dialogue.
Pff ! Quelle hypocrisie !
Kouy nguén keureum 6hr du matin am 3 champs d'arachides yor enclos(bo sokhla preuves wakhma)...Pastef sama ADN leu nek, photo bi dou hasard
Replying to @toopicc
𝐸𝑛𝑙𝑒𝑣𝑒 𝑙𝑎 𝑝ℎ𝑜𝑡𝑜 𝑑𝑒 𝑠𝑒𝑟𝑖𝑔𝑛𝑒 𝑠𝑎𝑙𝑖𝑜𝑢 𝑑𝑎𝑘ℎ 𝑠𝑒𝑟𝑖𝑔𝑛𝑒 𝑠𝑎𝑙𝑖𝑜𝑢 𝑛𝑒𝑛𝑎 𝑝𝑎𝑠𝑡𝑒𝑓 𝑚𝑜𝑦 𝑟𝑒𝑤 𝑚𝑖 𝑑𝑖 𝑆𝑒𝑛𝑒𝑔𝑎𝑙























